Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:3-4 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Saam xel ne ma, ma naan biiñ boog, bégloo, ba mel nib dof, tey ànd ak sama xel, ba gis lu ci baax, ba doom aadama di ko def, giiru dundam fi ko jant bi tiim.
4 Damaa liggéey lu réy. Tabaxlu naa samay kër, jëmbat sama toolub reseñ.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi