Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:3 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Saam xel ne ma, ma naan biiñ boog, bégloo, ba mel nib dof, tey ànd ak sama xel, ba gis lu ci baax, ba doom aadama di ko def, giiru dundam fi ko jant bi tiim.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi