Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:18-20 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Sama doñ-doñ, ji fi kaw dun bi, génnliku na ma, dama koy wacce ka may wuutuji rekk,
19 xameesul ku xeloom ku nitoodi lay doon, mooy moom lu ma doon doñ-doñi, te sama manoore manaloon ma ko fi kaw dun bi. Loolu it, cóolóoli neen.
20 Sama xol a jeex ci doñ-doñ ju ma doñ-doñi fi kaw dun bi.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi