Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:15-16 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Ma xalaataat, saam xel ne ma, dof bi noonu, man it noonu; ana lu may xeloo xelu doye? Saam xel ne ma loolu it, cóolóoli neen.
16 Ku xelook ku dof, du yàgg ñu fàtte la; ay bés yu néew, ñu fàtte lépp. Acam! Dof, dee; rafet xel, dee.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi