Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:11-12 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:11-12 in Kàddug Yàlla gi

11 Ma xoolaatal sama bopp lépp lu ma sottal, doñ-doñi ko, ba sottal, ndeke lépp, cóolóoli neen ak napp um ngelaw. Nit gisul njariñ ci kaw suuf.
12 Ma geesu xoolaat xel mu rafet, xool ag nitoodi akug ndof. Ana ku may wuutuji ci nguur gi, lu muy def lu moy lu ñu daan def?
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi