Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:10 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:10 in Kàddug Yàlla gi

10 Lépp lu saay gët xemmemaa, xañuma ko sama xol. Bañaluma sama bopp benn bànneex, xanaa di bége lu ma liggéey, yooloo ko la ma liggéey.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi