Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:9-11 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:9-11 in Kàddug Yàlla gi

9 Lu ayoon mooy ayati, lu ñu jëfoon moom lañuy jëfati. Dara yeesul fi kaw suuf.
10 Lëf a ngii, nit naa: «Lii de lu bees la,» te mu ngi fi woon lu yàgg, lu jiitu sunu juddu.
11 Kenn du fàttliku ñi jiitu, ñiy ñëwit, ñi leen topp duñu leen fàttliku.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi