Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:8-9 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Jëfoo jëf ca jëfit, làmmiñ tuddul lépp, bët du suur, nopp du buur.
9 Lu ayoon mooy ayati, lu ñu jëfoon moom lañuy jëfati. Dara yeesul fi kaw suuf.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi