Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàdduy Waare 1:5-7 in Wolof
Help us?
Kàdduy Waare 1:5-7
in
Kàddug Yàlla gi
5
Jant fenk, so, ne coww dellu fa muy fenke.
6
Ngelaw jëm bëj-saalum, wiiri jëm bëj-gànnaar, di wiir ak a wiiraat, di delluy wëndeelu, topp yoonam.
7
Dexoo dex wal, wuti géej, te taxul géej fees. Fa dex wal jëm, fa lay walati, jëm.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms