Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:15-16 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Lu wañaaru, maneesu koo jubbanti; lu teewul, maneesu koo lim.
16 Damaa wax ci saam xel naa: Man de, maa ngii di gëna xelu, ba sut ku ma jiitu ci jalub Yerusalem. Damaa xuus ci xel mu rafet ak xam-xam,
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi