Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:11-13 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 Kenn du fàttliku ñi jiitu, ñiy ñëwit, ñi leen topp duñu leen fàttliku.
12 Man waarekat bi, buurub Israyil laa woon ci Yerusalem.
13 Damaa dogu ne damay gëstu, teg ko ci xel mu rafet, di settantal mboolem lu nit def fu jant bi tiim. Ndaw sas wu tiis wu Yàlla sase, ñu war koo sasoo!
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi