Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:10 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:10 in Kàddug Yàlla gi

10 Lëf a ngii, nit naa: «Lii de lu bees la,» te mu ngi fi woon lu yàgg, lu jiitu sunu juddu.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi