Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 12:8-9 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 12:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Cóolóoloo cóolóol, waru waarekat ba. Léppi cóolóoli neen.
9 Waarekat ba daa xelu, di jànglewaale xam-xam, di natt ak a gëstu, di jekk-jekkal kàdduy xel yu takku.
Kàdduy Waare 12 in Kàddug Yàlla gi