Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 12:4-5 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 12:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 bunt yi féeteek mbedd mi tëje, coowal wol dal, as picc sab, nelaw naaw, janq ju doon woy, selaw.
5 Nga dem, ba ragal fu kawe, am tiitaange ciw yoon, garab tóor, ba weex furr, soccet di yokokoki, doomu garab tëë yékkati siddit, nga jëm kër gu mujj, waa dëj bi fees mbedd mi.
Kàdduy Waare 12 in Kàddug Yàlla gi