Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 12:3-4 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 12:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Su bés baa wattukati kër gi di lox, jàmbaari xare yi sëgg, wolkat yi néew, ba wolatuñu, ñiy séentu ci caax yi giimle,
4 bunt yi féeteek mbedd mi tëje, coowal wol dal, as picc sab, nelaw naaw, janq ju doon woy, selaw.
Kàdduy Waare 12 in Kàddug Yàlla gi