Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 11:3-4 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 11:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Xàmbaar bu duyee, ba fees, fi kaw suuf lay soob. Garab, bu daanoo ndijoor mbaa càmmoñ, fa mu daanu lay des.
4 Kuy déglu ngelaw, doo ji, kuy seetluy niir, doo góob.
Kàdduy Waare 11 in Kàddug Yàlla gi