Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 9:8-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 9:8-11 in Kàddug Yàlla gi

8 Bul yedd kuy ñaawle, da lay jéppi; yeddal ku rafet xel, mu naw la.
9 Xelalal ku xelu, mu yokku. Xamalal ku jub, mu yokk njàngam.
10 Ragal Aji Sax ji di njàlbéenu rafet xel, xam Aji Sell ji di am ug dégg.
11 Maay Xel mu Rafet, ku ma topp gudd fan, dund, dundati.
Kàddu yu Xelu 9 in Kàddug Yàlla gi