Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 9:5-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 9:5-9 in Kàddug Yàlla gi

5 «Kaay, ma may la, nga lekk, xellil lay biiñ, nga naan.
6 Dëddul jëfi téxét ba dund, di jubal ci yoonu dégg.»
7 Artu kuy ñaawle, feyoo saaga rekk, yedd ab soxor, yooloo loraange.
8 Bul yedd kuy ñaawle, da lay jéppi; yeddal ku rafet xel, mu naw la.
9 Xelalal ku xelu, mu yokku. Xamalal ku jub, mu yokk njàngam.
Kàddu yu Xelu 9 in Kàddug Yàlla gi