Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 9:13-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 9:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Jigéen ju dof day xumb, reew, du xam lu xew.
14 Day toog bunt këram, mbaa fu kawee kawe ca dëkk ba,
15 di woo ña fay jaare te jubal seenu yoon.
16 Ma nga naa: «Képp ku téxét, jàddal ba fii!» Ku ñàkk bopp, mu ne ko:
Kàddu yu Xelu 9 in Kàddug Yàlla gi