Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 9:13-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 9:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Jigéen ju dof day xumb, reew, du xam lu xew.
14 Day toog bunt këram, mbaa fu kawee kawe ca dëkk ba,
Kàddu yu Xelu 9 in Kàddug Yàlla gi