Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:6-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:6-8 in Kàddug Yàlla gi

6 Déglul, ma wax la lu am solo, dégtal la njub.
7 Dëgg laay wax, di bañ wax ju bon.
8 Lu ma wax njub la. Amul lu dëng mbaa lu jekkadi.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi