Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:34-36 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:34-36 in Kàddug Yàlla gi

34 Mbégte ñeel na ki may déglu, di teewlu ca sama bunt bés bu nekk, di ma toogaanu sama bunt kër.
35 Ku ma daj, gudd fan, Aji Sax ji bége la.
36 Ku ma moy loru, ku ma bañ, daa repp.»
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi