Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:33-34 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:33-34 in Kàddug Yàlla gi

33 Dégluleen ku leen di yar, daldi muus. Buleen ko sàggane!
34 Mbégte ñeel na ki may déglu, di teewlu ca sama bunt bés bu nekk, di ma toogaanu sama bunt kër.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi