Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:31-32 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:31-32 in Kàddug Yàlla gi

31 May bége wërngalu àddinaam, di bànneexoo doomi aadama.»
32 «Kon nag, doom, dégluleen ma. Mbégte ñeel na ki may topp.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi