Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:21-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:21-23 in Kàddug Yàlla gi

21 Ku ma sopp, ma nàddil la, feesal sab denc.»
22 Soxna si, Xel mu Rafet nee na: «Aji Sax ji jagoo na ma ca njàlbéen, ma jiitu ca jëfam ya woon.
23 Bu yàgg lañu ma dëj, ca ndoorte la, bala suuf a sosu.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi