Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 8:20-22 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 8:20-22
in
Kàddug Yàlla gi
20
Yoonu njekk laay jaare, di jëfe li yoon àtte rekk.
21
Ku ma sopp, ma nàddil la, feesal sab denc.»
22
Soxna si, Xel mu Rafet nee na: «Aji Sax ji jagoo na ma ca njàlbéen, ma jiitu ca jëfam ya woon.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms