Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.
15 Samay pexe la buur di jiitee, kilifa di ci àttee dëgg.
16 Ci samay pexe la njiit di saytoo, ñook kàngam yeek ñiy àtte dëgg ñépp.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi