Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:13-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.
14 Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.
15 Samay pexe la buur di jiitee, kilifa di ci àttee dëgg.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi