Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 «Man, Xel mu Rafet, foog di sama kër; xam-xam ak pexe, ma for.
13 Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.
14 Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi