Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 7:7-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 7:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 séen ca biir téxét ya, ku ma seetlu ca xale yu góor ya, muy ku ñàkk bopp.
8 Muy dem ba fa ndaw say taxaw, ca selebe yoon wa, daldi wuti kër ndaw sa.
9 Ngoonug suuf la, jant biy lang, muy lëndëm di gëna guddi.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi