Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 7:4-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 7:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Safool xel mu rafet, muy sab jigéen, te nga xejjoo dég-dég ni sa mbokk lenqe.
5 Dina la aar ci ndaw su yemadi, bokk feneen, di wax lu neex.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi