Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 7:20-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 7:20-22 in Kàddug Yàlla gi

20 Mbuusum xaalis la ŋàbb, yóbbu, du ñibbsi ndare weer wi fees dell.»
21 Muy mocc ak a moccaat, ba nax ko, di wax lu neex, ba man ko.
22 Waa ja jekki, topp ko, mbete yëkk wu ñuy rendiji, mbaa dof bu ñu jéng, di ko yari.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi