Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 7:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 7:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Sama jëkkër newu fa, daa dem yoon wu sore.
20 Mbuusum xaalis la ŋàbb, yóbbu, du ñibbsi ndare weer wi fees dell.»
21 Muy mocc ak a moccaat, ba nax ko, di wax lu neex, ba man ko.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi