Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 7:12-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 7:12-15 in Kàddug Yàlla gi

12 Ma nga ca mbedd ma, ne ca pénc ya, ruqoo ruq, ma ngay yeeroo.
13 Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko:
14 «Tey matal naa la ma digoon Yàlla, yàppu bernde waa nga kër ga, saraxu cant la.
15 Moo ma taxa dikk dajeek yaw. Seet naa laa seet, ba gis la.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi