Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 7:11-14 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 7:11-14
in
Kàddug Yàlla gi
11
Daa xumb, të, du toog këram.
12
Ma nga ca mbedd ma, ne ca pénc ya, ruqoo ruq, ma ngay yeeroo.
13
Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko:
14
«Tey matal naa la ma digoon Yàlla, yàppu bernde waa nga kër ga, saraxu cant la.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms