Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:32-35 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:32-35 in Kàddug Yàlla gi

32 Njaaloo di ñàkk bopp, kuy sànk bakkanam a koy def.
33 Mbugal ak toroxte dib añam, te gàcceem du deñ.
34 Fiiraange day feesal xolu góor, te du ñéeblu buy feyu.
35 Du faale ndàmpaay, loo ko may, may, du giif.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi