Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 6:30-33 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 6:30-33
in
Kàddug Yàlla gi
30
Deesul sikk ku sàcc aw ñam, def ci biiram ndax xiif.
31
Waaye bu feeñee, fey boroom juróom yaari yoon, joxe alalu këram yépp.
32
Njaaloo di ñàkk bopp, kuy sànk bakkanam a koy def.
33
Mbugal ak toroxte dib añam, te gàcceem du deñ.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms