Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:3-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaa ngi ci sa loxoy moroom, kon defal nii, doom, ba rëcc: doxal tinuji ko, raamali ko.
4 Bul gëmm, bul nelaw!
5 Dawal ni kéwél gu rëcc ub rëbb, ne fërr ni picc mu raw ab fiirkat.
6 Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi