Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Doom, defal li la baay sant, te bul wacc ndigalal yaay.
21 Takkal foo tollu, taf ci sa xol, fas ko ci sa baat.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi