Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:2-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:2-4 in Kàddug Yàlla gi

2 saw làmmiñ yeb la cim pax, nga keppu?
3 Yaa ngi ci sa loxoy moroom, kon defal nii, doom, ba rëcc: doxal tinuji ko, raamali ko.
4 Bul gëmm, bul nelaw!
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi