Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 5:8-10 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 5:8-10
in
Kàddug Yàlla gi
8
Soreel ndaw soosu, bul jege bunt këram.
9
Kon nga ñàkk daraja, keneen jagoo; ku néeg bóom la.
10
Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms