Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:7-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Kon, doom, déglu ma, bul wacc samay kàddu.
8 Soreel ndaw soosu, bul jege bunt këram.
9 Kon nga ñàkk daraja, keneen jagoo; ku néeg bóom la.
10 Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi