Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:3-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Lu mel ni lem la ndaw su yemadi di wax, làmmiñ wa ni diw gu ñu lay raay.
4 Muj ga mu wex xàtt, di gaañe ni ñawkay saamar.
5 Tànk ya day bartalu wuti ndee, ay jéegoom àkki njaniiw.
6 Rëddul yoonu dund, daa lajj, te xamu ko.
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi