Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:21-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:21-22 in Kàddug Yàlla gi

21 Lu waay jëf, Aji Sax ji gis, di xool mboolem fu mu jaare.
22 Jëf ju bon day fiir ka ko sàlloo, bàkkaaram di mbaal, jàpp ko.
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi