Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:8-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Nawal xel mu rafet, mu darajaal la; tafoo ko, mu teral la.
9 Da lay takkal kaala gu jekk, solal la mbaxanam buur.»
10 Déglul, doom, te dégg saay wax, ndax nga gudd fan.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi