Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:2-3 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Maa ngi leen di jàngal lu baax, buleen fàtte sama njàngle.
3 Man it amoon naa baay, di benn bàjjo ci saa ndey.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi