Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:17-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 Daa bon, def ko lekk, di màndee coxoram.
18 Yoonu ku jub day leer, ba ne ràññ ni bëccëg.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi