Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:16-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Ku bon du nelaw te lorewul, du dajjant ba kera muy téqe.
17 Daa bon, def ko lekk, di màndee coxoram.
18 Yoonu ku jub day leer, ba ne ràññ ni bëccëg.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi