Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:14-17 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:14-17 in Kàddug Yàlla gi

14 Yoonu ku bon, bu ci tegu; fu ab soxor di jaar, bu fa dox.
15 Moyul, bu fa jaare; mbasal te wéy!
16 Ku bon du nelaw te lorewul, du dajjant ba kera muy téqe.
17 Daa bon, def ko lekk, di màndee coxoram.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi