Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 4:11-14 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 4:11-14
in
Kàddug Yàlla gi
11
Yoon wu xelu laa la teg, jaarloo la yoonu njub.
12
Doo dox ba tërëf, doo daw, téqtalu.
13
Ŋoyal cib yar, bul yoqi, sàmm ko, moo yor sa bakkan.
14
Yoonu ku bon, bu ci tegu; fu ab soxor di jaar, bu fa dox.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms